Linguère Ndaté Yalla Mbodj La linguère Ndaté Yalla Mbodj, reine du Royaume du Waalo Biographie Titre complet Linguère Ndaté Yalla Mbodj Dynastie Dynastie des Tedyek maternelle et dynastie Dyoos' paternelle Nom de naissance Ndaté Yalla Mbodj Date de naissance 1810 - 1860[1] Lieu de naissance Waalo, Sénégal Père Brak Amar Fatim Borso Mbodj Mère Linguère Awo Fatim Yamar Khuri Yaye Mbodj Conjoint 1.
Linguère Ndaté Yalla Mbodj La linguère Ndaté Yalla Mbodj, reine du Royaume du Waalo Biographie Titre complet Linguère Ndaté Yalla Mbodj Dynastie Dynastie des Tedyek maternelle et dynastie Dyoos' paternelle Nom de naissance Ndaté Yalla Mbodj Date de naissance 1810 - 1860 Lieu de naissance Waalo, Sénégal Père Brak Amar Fatim Borso Mbodj Mère Linguère Awo Fatim Yamar Khuri Yaye Mbodj Conjoint 1.
La linguère Ndaté Yalla Mbodj – ou Ndete Yalla – (1810-1860)[1] est la dernière grande reine du Waalo, un royaume situé dans le Nord-Ouest de l'actuel Sénégal.
Lingeer Ndate Yalla Mboj walla Ndete Yalla (1810-1860)mooy mujjenteelu buur bu jigeen bu mag bu waalo, bu feete ci pencum bët ganaar-sowu bu senegaal.
Maïmouna Kane Biographie Naissance 13 mars 1937 Dakar Décès 1er mars 2019 (à 81 ans) Paris Nom de naissance Maïmouna Ndongo Nationalité Sénégalaise Activités Femme politique, juriste Conjoint Mamoudou Touré
Maïmouna Kane Biographie Naissance 13 mars 1937 Dakar Décès 1er mars 2019 (à 81 ans) Paris Nom de naissance Maïmouna Ndongo Nationalité Sénégalaise Activités Femme politique, juriste Conjoint Mamoudou Touré Xew- xewi dundu Maymuna Kan Jamono ju mu juddoo: fukki fan ak ñett ci weeru mars atum junni ak juróom ñeent teemeer ak fanweer ak juróom ñaar ca Ndakaaru Jamono ju mu faatoo: benn bés ci weeru mars ci atum ñaari junni ak fukki fan ak juróom ñeent (amoon juróom ñetti fukki at ak benn ba muy faatu) ca Pari Turam: Maymuna Ndongo Réewam: senegaal Yëngu-yëngoom: jigeen juy def politig, àttekat la Turu jëkkëram: Mamadu Ture
Voir aussi
Xoolal itam
Bibliographie
Xew- xewi dundam
Maïmouna Kane, née le 13 mars 1937 à Dakar (Sénégal)[1] et morte le 1er mars 2019 à Paris (France)[2], est une juriste et femme politique sénégalaise.
Maymuna Kan a ngi juddu fukki fan ak ñaar ci weeru mars atum junni ak juróom-ñeent- téemeer ak fanweeer ak ñaar ca Ndakaar(Senegaal) (1). Mu ngi génn àdduna benn fan ci weeru mars ci atum ñaar junni ak jukk ak juróom- ñeent ca Pari (farãs) (2) . Bokkoon na ci àttekat yu mag ci rééw mi.
Biographie
Xew- xewi dundam
Ancien auditeur à la Cour suprême, ancien substitut du procureur de Dakar, ancien conseiller à la Cour d'Appel de Dakar[3], elle entre le 15 mars 1978 dans le gouvernement socialiste d'Abdou Diouf, en même temps qu'une autre pionnière, Caroline Faye Diop.
Maymuna Kan nekkoon na óditëer ci ëttub àtte bu mag bi. Nekkoon na itam ki nu toftal ci porokirëeru ndakaaru. Doonoon na déeyaakoon ci ëttu àtteb àttewaat ca ndakaaru(3).
Maïmouna Kane est nommée Secrétaire d’État auprès du Premier ministre chargée de la Condition féminine, de la Condition humaine et de la Promotion humaine, un portefeuille dont l'intitulé connaît plusieurs changements par la suite[4].
Mu ngi dugg ci nguurug Abdu Juuf ci fukki fan ak juróom ci weeru mars atum junni ak juróom ñeenti téemeer ak juróom ñaar fukk ak juróom ñett. Fekkoon na fa moroomu jàmbaar ju tudd Karolin Fay Jóob. Noonu lanu ko tabbe mu doon sekereteeru nguur gi nu toftal ci jëwriñ ju mag jiy toppatoo nekkinu jigeen ñi, nekkinu nit ñi ak a yëkkëti taxawaayu nit ñi.
Elle est promue ministre du Développement social dans le Gouvernement Niasse I formé le 5 avril 1983.
Tur woowu dina am coppite(4). Ba nu tabbee Mustafaa Ñas jëwriñ ju mag ji juróomi fan ci weeru awril atum junni ak juróom ñeenti téemeer ak juróom ñetti fukk ak ñett lanu ko dénkee jëwriñu cuqali nekkin wi.
Née Ndongo, elle a épousé l'homme d'affaires Yaya Kane avec qui elle a cinq enfants.
Doon nanu ko woowee Ndongo. Nekkoon na soxnas Yaya kan. Kooku nekkoon na ku doon yëngatu wi wàllu koom.
À la mort de celui-ci, elle se remarie avec l'économiste Mamoudou Touré, ministre des Finances de mai 1983 à avril 1988[5].
Amoon na ak moom juróomi doom. Ba jëkkër ja gaañoo, la sëyaat ak ku xam-xamam màccoon ci koom-koom, ku nu naan Mamadu Ture, moom mi nekkoon jëwrin ji nu dénd koppari réew mi diirub weeru me atum junni ak juróom ñeenti téemeer ak juróom ñetti fukk ak ñett ba weeru me atum junni ak juróom ñeenti téemeer ak juróom ñetti fukk ak juróom ñett (5).
Sélection de publications
Tànneefu téere yiy génne
Mariama Bâ Fonction Professeure Biographie Naissance 17 avril 1929 Dakar, Sénégal Décès 17 août 1981 (à 52 ans) Dakar, Sénégal Nationalité Sénégalaise Formation École normale de Rufisque Activité Romancière Père Amadou Bâ Conjoint Obèye Diop Autres informations Religion Islam Distinctions Prix Noma de publication en Afrique Œuvres principales Une si longue lettre Le Chant écarlate
Maryaama Ba Liggeey Jàngalekat Dundu ak jaar-jaaram Bésu juddu 17 awiril 1929 Dakaar, Senegaal Bésu faatu 17 ut 1981 (ci juroom-fukki atam ak ñaar) Dakaar, Senegaal Réew Senegaal Fi mu jànge Ekool Normaal bu Tëngeej (Rufisque) Yëngu-yëngu Bindkatu téere nettali Way-jur wu góor Aamadu Ba Borom-kër Obéey Jóob Yeneen xibaar ci moom Diine Islaam Neexal Prix Noma de publication en Afrique Téereem yi gën a fës Une si longue lettre Le Chant écarlate Mariama Bâ Fonction Professeure Biographie Naissance 17 avril 1929 Dakar, Sénégal Décès 17 août 1981 (à 52 ans) Dakar, Sénégal Nationalité Sénégalaise Formation École normale de Rufisque Activité Romancière Père Amadou Bâ Conjoint Obèye Diop Autres informations Religion Islam Distinctions Prix Noma de publication en Afrique Œuvres principales Une si longue lettre Le Chant écarlate
Un lycée de Gorée (la Maison d’éducation Mariama Bâ) porte son nom.
Liise bu Gore (Këru yar Maryaama Ba) moom lañu ko tudde.
Ses œuvres reflètent principalement les conditions sociales de son entourage immédiat et de l’Afrique en général, ainsi que les problèmes qui en résultent : polygamie, castes, exploitation des femmes pour le premier roman ; opposition de la famille, manque de capacité de s’adapter au nouveau milieu culturel face à des mariages interraciaux pour le deuxième.
Ay téereem dañuy fësal anam yi ñi ko wër ak doomi Afrig yi di dunde ay jafe-jafe yiy tukke ci yile yépp : denc jabar yu bare, waasoo, teg jigeen lu mu àttanul ci téereem bu jëkk bi ; ñàkk a àndug mbokk yi, ñàkk a mën a dund ci am mbatit mu dul sa mos, te sëyu ñu bokkul der fësal ko ci ñaareelu téereem bi.
Notoriété
Ag ràññeekum
L'écrivaine Mariama Bà fait partie des pionnières de la littérature sénégalaise[3].
Bindkat bile di Maryaama Ba bokk na ci ñi xàll yoonu càllala ci Senegaal[1].
Elle est rendue célébrè grâce à son œuvre Une si longue lettre qui est son premier roman publié en 1979.
Téere bi ñu naan Une si longue lettre, nekk téere nettaleem bu jëkk, moo ko siiwal.
Dans son roman elle décrit les inégalités entre hommes et femmes, les problèmes de castes, l'injustice à l'égard des femmes, les croyances religieuses, les coutumes et les rites notamment pour un enterrement.
Téere baa ngi wax ci ñàkk a yemale gi am diggante góor ak jigeen, mbiri waasoo, ngëmi diine yi, aada ak cosaan yi, rawatina lu jëm ci anam yi ñuy dëjale nit.
Elle décrit également le problème de la polygamie qui gangrène la société où pour la plupart du temps les femmes sont meurtries, angoissées lorsqu'elles ont des coépouses qui a parfois l'age de leur enfant.
Mu ngi wax tamit ci mbiru denc jabar yu bare, nga xam ne dafa dem ba yàq lu bare ci dundinu askan wi, ñu ciy toroxal jigeen ñi lu ci ëpp, mu leen di jural ay naqar su fekkee ne dañu la wutal wujj wu maase ak say doom.
Son œuvre Une si longue lettre a eu tellement de succès que l’État du Sénégal a décidé depuis quelques années de le mettre dans les œuvres aux programmes pour l'enseignement secondaires.
Gëdd, njëriñ ak siiw gi Une si longue lettre am tax na ba nguuru Senegaal jël dogalu boole ko ci téere yi ñuy jàngale ci lekool yu digg-dóomu yi, ay at a ngi nii, booba ba léegi.
Elle a fait de son œuvre, un roman engagé au nom du principe de responsabilité et du devoir de solidarité ce qui lui a valu aujourd'hui parmi les plus célèbres écrivains du Sénégal. L’école des jeunes filles de l'ile-de-Gorée porte son nom pour lui rendre hommage.
Dafa jël téere bi, def ko muy téere buy jëmmal taxawu askan te gàlloo ak wareefu dimbalante lal ko, loolu sax moo tax tey, mu bokk ci bindkat yi gën a siiw ci Senegaal, ñu tudde ko tamit lekoolu xaley jigeen ba nekk Gore ngir sargal ko.
Œuvres
Ay téereem
Bibliographie
Lees bind ci moom ak ay téereem
Mariama Bâ, née le 17 avril 1929 à Dakar, et morte dans la même ville le 17 août 1981, est une femme de lettres sénégalaise.
Maryaama Ba mu ngi juddu fukki fan ak juroom-ñaar ci weeru awiril atum 1929, faatu fukki fan ak juroom-ñaar ci weeru ut atum 1981 ci Dakaar. Bindkat la woon.
Dans son œuvre, elle critique les inégalités entre hommes et femmes dues à la tradition africaine.
Ci ay téereem, Maryaama Ba dafay ŋàññ ñàkk a yemale gi am ci diggante góor ak jigeen te aju ci aaday Afirig.
Liste d'écrivains sénégalais Littérature sénégalaise Histoire des femmes au Sénégal
Limu bindkati Senegaal yi : Liste d'écrivains sénégalais Càllalag Senegaal : Littérature sénégalaise Taarixu jigeeni Senegaal : Histoire des femmes au Sénégal
Biographie (en) Mariama Bâ (1929-1981) Notices d'autorité : Fichier d’autorité international virtuel International Standard Name Identifier Bibliothèque nationale de France (données) Système universitaire de documentation Bibliothèque du Congrès Gemeinsame Normdatei Bibliothèque nationale d’Espagne Bibliothèque royale des Pays-Bas Bibliothèque universitaire de Pologne Bibliothèque nationale de Suède Bibliothèque nationale tchèque WorldCat Ressource relative à la littérature : (de) Kritisches Lexikon zur fremdsprachigen Gegenwartsliteratur Ressource relative à la vie publique : « Maitron »
Dundu ak jaar-jaaram Maryaama Ba (juddu 1929, faatu 1981) Balluwaay bu aju ci càllala gi Balluwaay bu aju ci ag dundam
Elle est née à Dakar au Sénégal en 1929 dans une famille fortunée.
Mu ngi juddoo Dakaar atum 1929 ci njaboot gu am alal.
Son père était fonctionnaire de l'État.
Way-juram wu góor liggeeykatu nguur gi la woon.
Après la mort prématurée de sa mère, elle est élevée par ses grands-parents dans un milieu musulman traditionnel[1].
Ginnaaw bi way-juram wu jigeen faatoo, ci teel sax, ay maamam a wéyoon di ko yar. Ñooñu ñoo ko yar ci diiney lislaam[1].
Son père, Amadou Bâ, est devenu ministre de la Santé du premier gouvernement sénégalais en 1957[2].
Way-juram wu góor, ñu doon ko wax Aamadu Ba mujj nekk jëwriñ ji yore wér-gu-yaram bi ci ngornamaŋ bu Senegaal atum 1952[2].
Elle intègre une école française où elle se fait remarquer par ses excellents résultats.
Mu daldi dugg ci lekool farañse bi, nekk ku ci ràññeku lool ndax ay jallooreem.
Après son certificat d'études primaires obtenu à 14 ans, elle entre en 1943 à l’École normale de Rufisque, qu’elle quitte munie d’un diplôme d’enseignement en 1947.
Bi mu amee sàrtikaa (certificat d'études primaires) ci fukki at ak ñeentam, la dem ca Lekool Normaal bu Tëngeej (Rufisque) atum 1943. Lekool boobu mu nga fa jóge atum 1947 ginnaaw bu mu fa amee lijaasab njàngale.
Elle enseigne pendant douze ans puis demande sa mutation au sein de l’Inspection régionale de l’enseignement pour raison de santé[1].
Mu nekk di jàngale diiru fukki at ak ñaar laata muy ñaan ñu jële ci njàngale mi, yóbbu ko ca Eespeksiyoo bi yore wàllu njàng mi ci gox bi (Inspection régionale de l’enseignement), loolu wéradig yaramam moo ko waraloon[1].
De son premier mariage, avec Bassirou Ndiaye, elle a trois filles, et du second mariage avec Ablaye Ndiaye une fille SMK[Quoi ?] ; elle obtient le divorce de son troisième mari, le député et ministre Obèye Diop, avec qui elle a eu cinq enfants.
Am na ñetti doom yu jigeen ci sëyam bu jëkk ak Basiiru Njaay, am beneen doom bu jigeen SMK[Quoi ?] ci ñaareelu sëyam ak Ablaay Njaay. Yàlla wéddi sëyam ak ñetteelu borom-këram di Obéey Jóob, nekkoon fi deppite ak jëwriñ te mu amoon ak moom juroomi doom.
À la suite de son expérience du mariage, Mariama Bâ s’engage pour nombre d’associations féminines en prônant l’éducation et les droits des femmes[1].
Ginnaaw jaar-jaar yooyu yépp mu am ci sëy, Maryaama Ba dafa mujj dugg ci kureeli jigeen yu bare, ngir jigeen ñi jàng te mën tamit di jot seeni àq ak yelleef[1].
À cette fin, elle prononce des discours et publie des articles dans la presse.
Loolu moo waraloon mu yëkëti ay kàddu, siiwal ay jukki yu aju ci wàll wi ci bérebi tasekaay xibaar yi.
En 1979, elle publie aux Nouvelles éditions africaines son premier roman, Une si longue lettre, dans lequel, la narratrice, Ramatoulaye, utilise le style épistolaire pour faire le point sur sa vie passée suite à la mort de son mari.
Atum 1979 la siiwal téere bile di Une si longue lettre di téere nettaleem bu jëkk ci këru móolukaay téere gu ñu naan Nouvelles éditions africaines. Ci boobu téere, nettalikatam bi di Ramatulaay mu ngi ciy nettali, ci ab baataxal, dundam gi weesu ginnaaw bu borom-këram faatoo.
Ce livre manifeste l'ambition féministe africaine naissante face aux traditions sociales et religieuses.
Téere baa ngi fësal bëgg-bëgg bu mag, bu yeewu ngir nekkal fi jiggeeni Afrig yi war a jàmmaarloo ak aada ak cosaan ak tamit diine.
Dès sa sortie, le roman connaît un grand succès critique et public ; elle obtient le prix Noma de publication en Afrique à la Foire du livre de Francfort en 1980[1].
Bi ñu ko génnee rekk, la téere nettali bi siiw lool, ñépp di ci wax ; ñu tappal ko ci neexal bu ñu naan « Prix Noma de publication en Afrique » ca Fuwaaru téere bu Francfort atum 1980[1].
En plus d'Une si longue lettre, elle promeut les droits des femmes, particulièrement des femmes mariées.
Lu moy Une si longue lettre, mu ngi doon taxawu ak a yëkëti àq ak yelleefi jigeen ñi, rawatina jigeen ñi nekk ci buumu sëy.
Elle prononce des discours et elle a écrit des articles sur la vie des femmes, notamment sur celles dont la vie était défavorisée.
Muy wax ak a bind ay jukki ci nekkinu jigeen ñi, rawatina ñi seen yoxo jotul seen ginnaaw.
Elle meurt peu après d’un cancer, avant la parution de son deuxième roman, Un chant écarlate, qui raconte l'échec d'un mariage mixte entre un Sénégalais et une Française, du fait de l'égoïsme de l'époux et des différences culturelles[1].
Mu ngi génn àdduna ginnaaw bu ko ab kãaseer daanee, laata ñaareelu téere nettalim bii di Un chant écarlate di génn. Téere boobule dafay nettali ñàkk a antu gu ab sëy bu doxoon diggante ab waa-senegaal ak ab waa-farãas ñàkk a antu. Loolu li ko waral yépp mooy, bopp-sa-bopp gu jëkkër ji di wéye ak wuute gu ñaari mbatit yi wuute[1].
Aminata Sow Fall Aminata Sow Fall (2011) Données clés Naissance 27 avril 1941 (79 ans) Saint-Louis Sénégal Distinctions Grand prix littéraire d'Afrique noire (1980) Prix international pour les lettres africaines (1982) Auteur Langue d’écriture Français Genres Romans, essais, théâtre, poésie
Aminata Sow Fall Aminata Sow Fall (2011) Données clés Naissance 27 avril 1941 (79 ans) Saint-Louis Sénégal Distinctions Grand prix littéraire d'Afrique noire (1980) Prix international pour les lettres africaines (1982) Auteur Langue d’écriture Français Genres Romans, essais, théâtre, poésie Aminata Sow Faal Aminata Sow Faal (2011) Xibaar yi ëpp solo Bésu juddu 27 awiril 1941 (juroom-ñaar-fukki at ak juroom-ñeent) Ndar (See-Luwi) Senegaal Raaya Grand prix littéraire d'Afrique noire (1980) Prix international pour les lettres africaines (1982) Bindkat Ci kàllaama bi muy bind ay téereem Farañse Xeeti téere Téere nettali, ese, tiyaatar, taalif
Toujours absorbée par l'écriture, la romancière partage désormais son temps entre Dakar, Saint-Louis et d'autres destinations à l'étranger, car elle est souvent sollicitée pour des conférences en relation avec son œuvre ou des thèmes plus larges tels que l'éducation, la culture ou la paix[1].
Bindkat bile di Aminata Sow Faal, mu ngi dundu ba léegi mbirum bind, di jallantu diggante Dakaar, Ndar (See-Luwi) ak yeneeni réew ci àdduna bi, ndaxte léeg-léeg, dañu koy woo ci ay waxtaan yu laale ak li mu bind ci ay téereem, wala yu laale ak njàng ak njàngale, wala mbatit wala sax jàmm.
Elle observe avec acuité le monde qui l'entoure : « L'artiste n'est pas dans une tour d'ivoire.
Seetlu bu ñaw lay seetlu li ko wër : « Ndanaan li tëjuwul rekk ci ab ruqam, mel ni ku dara ñorul.
Son rêve ne l'empêche pas de sentir le bouillonnement de la cité »[6], mais elle se défend toutefois de tout engagement politique partisan[7].
Géntam terewu koo yég liy jax-jaxi ci pénc mi » waaye nag, taxul mu nangu ku ko féetale ci ag làngug pólotig.
Aminata Sow Fall est mère de sept enfants[1], dont le rappeur Abass Abass[2],[8].
Aminata Sow Faal am na juroom-ñaari doom, bokk na ci ñooñu, rappëer bile di Abaas.