# wo/Wolof-NT.xml.gz
# zh/Chinese-tok.xml.gz


(src)="b.MAT.1.1.1"> Lii mooy cosaanu Yeesu Kirist , sëtu Daawuda , sëtu Ibraayma .
(trg)="b.MAT.1.1.1"> 亞伯拉罕 的 後裔 、 大衛 的 子孫 、 耶穌基督 的 家譜 . 〔 後裔 子孫 原文 都 作 兒子 下同

(src)="b.MAT.1.2.1"> Ibraayma moo jur Isaaxa ; Isaaxa jur Yanqóoba ; Yanqóoba jur Yuda ak i doomi baayam ;
(trg)="b.MAT.1.2.1"> 亞伯拉罕 生 以撒 . 以撒 生 雅各 . 雅各 生猶 大和 他 的 弟兄

(src)="b.MAT.1.3.1"> Yuda , Fares ak Sara ci Tamar ; Fares Esrom , miy baayu Aram ;
(trg)="b.MAT.1.3.1"> 猶大 從 他 瑪氏 生法 勒斯 和 謝拉 . 法勒斯生希斯崙 . 希斯崙生 亞蘭

(src)="b.MAT.1.4.1"> Aram Aminadab ; Aminadab Naason ; Naason Salmon ;
(trg)="b.MAT.1.4.1"> 亞蘭生 亞米 拿達 . 亞米 拿 達生 拿順 . 拿順 生撒門

(src)="b.MAT.1.5.1"> Salmon jur ci Raxab doom ju tudd Bowas ; Bowas am ak Ruut Obedd ; Obedd jur Yese ,
(trg)="b.MAT.1.5.1"> 撒門從 喇合氏 生波阿斯 . 波阿斯從路 得 氏生 俄備得 . 俄備 得 生 耶西

(src)="b.MAT.1.6.1"> miy baayu buur bi Daawuda .
(src)="b.MAT.1.6.2"> Daawuda moo jur Suleymaan ci ki nekkoon jabari Uri ;
(trg)="b.MAT.1.6.1"> 耶西 生 大衛王 。 大衛從烏 利亞 的 妻子 生 所羅門

(src)="b.MAT.1.7.1"> Suleymaan jur Robowam ; Robowam Abiya ; Abiya Asaf ;
(trg)="b.MAT.1.7.1"> 所羅門 生 羅波安 . 羅波安 生亞比雅 . 亞比雅生 亞撒

(src)="b.MAT.1.8.1"> Asaf Yosafat ; Yosafat Yoram , miy baayu Osiyas ;
(trg)="b.MAT.1.8.1"> 亞撒 生約 沙法 . 約沙法生 約蘭 . 約蘭 生烏西亞

(src)="b.MAT.1.9.1"> Osiyas jur Yowatam ; Yowatam Akas , miy baayu Esekiyas ;
(trg)="b.MAT.1.9.1"> 烏西亞生約坦 . 約坦 生亞哈斯 . 亞哈斯生 希西家

(src)="b.MAT.1.10.1"> Esekiyas Manase ; Manase Amon ; Amon Yosiyas ;
(trg)="b.MAT.1.10.1"> 希西家 生瑪拿西 . 瑪拿西 生 亞們 . 亞們 生約西亞

(src)="b.MAT.1.11.1"> Yosiyas jur Yekoñas ak i doomi baayam ca jamono , ja ñu defe Yawut ya jaam , yóbbu leen Babilon .
(trg)="b.MAT.1.11.1"> 百姓 被 遷到 巴比倫 的 時候 、 約西亞生 耶哥 尼雅 和 他 的 弟兄

(src)="b.MAT.1.12.1"> Ba ñu leen yóbboo ca Babilon , Yekoñas jur Salacel ; Salacel Sorobabel ,
(trg)="b.MAT.1.12.1"> 遷到 巴比倫 之後 、 耶哥 尼雅 生 撒拉鐵 . 撒拉 鐵生 所 羅巴伯

(src)="b.MAT.1.13.1"> miy baayu Abiyudd ; Abiyudd Eliyakim ; Eliyakim Asor ;
(trg)="b.MAT.1.13.1"> 所 羅巴伯生亞比玉 . 亞比玉生 以利 亞敬 . 以利 亞敬 生亞所

(src)="b.MAT.1.14.1"> Asor Sadog ; Sadog Akim ; Akim Eliyudd ;
(trg)="b.MAT.1.14.1"> 亞所生 撒督 . 撒督生 亞金 . 亞金 生以律

(src)="b.MAT.1.15.1"> Eliyudd Eleyasar ; Eleyasar Matan , miy baayu Yanqóoba ;
(trg)="b.MAT.1.15.1"> 以 律生 以利亞撒 . 以利亞撒 生 馬但 . 馬但 生 雅各

(src)="b.MAT.1.16.1"> Yanqóoba nag moo jur Yuusufa jëkkëru Maryaama ; te ci Maryaama la Yeesu , mi ñuy wax Kirist , juddoo .
(trg)="b.MAT.1.16.1"> 雅各 生 約瑟 、 就是 馬利亞 的 丈夫 . 那 稱為 基督 的 耶穌 、 是 從馬利亞 生的

(src)="b.MAT.1.17.1"> Mboolem giir googu nag , la dale ca Ibraayma ba ca Daawuda , fukk lañu ak ñeent ; la dale ca Daawuda ba ca njaam ga ca Babilon , fukk lañu ak ñeent ; la dale njaam ga ca Babilon ba ci Kirist , fukk lañu ak ñeent .
(trg)="b.MAT.1.17.1"> 這樣 、 從 亞伯拉罕 到 大衛 、 共 有 十四代 . 從 大衛 到 遷至 巴比倫 的 時候 、 也 有 十四代 . 從遷 至 巴比倫 的 時候 到 基督 、 又 有 十四 代

(src)="b.MAT.1.18.1"> Nii la Yeesu Kirist juddoo .
(src)="b.MAT.1.18.2"> Bi ñu mayee Maryaama ndeyam Yuusufa , waaye laata ñoo ànd , gis nañu ne dafa ëmb ci kàttanu Xel mu Sell mi .
(trg)="b.MAT.1.18.1"> 耶穌基督 降生 的 事 、 記在 下面 . 他 母親 馬利亞 已 經許 配 了 約瑟 、 還沒 有 迎娶 、 馬利亞 就 從聖 靈懷 了孕

(src)="b.MAT.1.19.1"> Yuusufa jëkkëram nag , nekkoon na nit ku jub te bëggu ko woon a weer .
(src)="b.MAT.1.19.2"> Mu nar a xàccook moom ci sutura .
(trg)="b.MAT.1.19.1"> 他 丈夫 約瑟 是 個義人 、 不 願意 明明 的 羞辱 他 、 想要 暗暗 的 把 他 休 了

(src)="b.MAT.1.20.1"> Waaye bi muy xalaat ci loolu , benn malaakam Boroom bi daldi ko feeñu ci gént ne ko : « Yaw Yuusufa , sëtu Daawuda , bul ragal a yeggali Maryaama sa jabar , ndaxte doom ji mu ëmb , ci Xel mu Sell mi la jóge .
(trg)="b.MAT.1.20.1"> 正 思念 這 事 的 時候 、 有主 的 使者 向 他 夢中顯現 、 說 、 大衛 的 子孫 約瑟 、 不 要 怕 、 只 管 娶 過 你 的 妻子 馬利亞來 . 因 他所懷的孕 、 是 從聖靈 來的

(src)="b.MAT.1.21.1"> Dina jur doom ju góor ; na nga ko tudde Yeesu , ndaxte moo di kiy musal xeetam ci seeni bàkkaar . »
(trg)="b.MAT.1.21.1"> 他 將要 生 一 個 兒子 . 你 要 給他 起 名叫 耶穌 . 因 他 要 將 自己 的 百姓 從罪惡裡 救出來

(src)="b.MAT.1.22.1"> Loolu lépp xewoon na , ngir amal li Boroom bi wax , jaarale ko cib yonent , bi mu naan :
(trg)="b.MAT.1.22.1"> 這一切 的 事 成就 、 是 要 應驗 主 藉 先知 所 說的話

(src)="b.MAT.1.23.1"> « Janq bi dina ëmb , jur doom ju góor , ñu tudde ko Emanuwel , » liy tekki « Yàlla ganesi na nu . »
(trg)="b.MAT.1.23.1"> 說 、 『 必 有 童女 、 懷孕 生子 、 人 要 稱 他 的 名為 以 馬內利 。 』 ( 以 馬內 利繙 出來 、 就是 神與 我 們 同在 。

(src)="b.MAT.1.24.1"> Noonu Yuusufa yeewu , yeggali jabaram , na ko ko malaakam Boroom bi sante woon .
(trg)="b.MAT.1.24.1"> 約瑟 醒了 、 起來 、 就 遵著 主使者 的 吩咐 、 把 妻子 娶過來

(src)="b.MAT.1.25.1"> Waaye àndul ak moom , ba kera mu mucc , jur doom ju góor ; mu tudde ko Yeesu .
(trg)="b.MAT.1.25.1"> 只是 沒有 和 他 同房 、 等 他 生 了 兒子 、 〔 有 古 卷 作 等 他 生了頭胎 的 兒子 〕 就 給 他 起名 叫 耶穌

(src)="b.MAT.2.1.1"> Bi nga xamee ne Yeesu juddu na ci Betleyem ci diiwaanu Yude , amoon na ay boroom xam-xam , ñu jóge penku , ñëw Yerusalem .
(src)="b.MAT.2.1.2"> Booba , ci jamonoy buur bi Erodd la woon .
(trg)="b.MAT.2.1.1"> 當 希律王 的 時候 、 耶穌生 在 猶太 的 伯利恆 . 有幾個 博士 從東 方來 到 耶路撒冷 、 說

(src)="b.MAT.2.2.1"> Ñu ne : « Ana buur bi juddul Yawut yi ?
(src)="b.MAT.2.2.2"> Ndaxte gis nanu biddiiwam ci penku te ñëw nanu ngir màggal ko . »
(trg)="b.MAT.2.2.1"> 那 生下 來作猶 太 人 之 王 的 在 那裡 。 我 們 在 東方 看見 他 的 星 、 特來 拜他

(src)="b.MAT.2.3.1"> Bi ko Erodd buur ba déggee , mu daldi jaaxle , moom ak waa Yerusalem gépp .
(trg)="b.MAT.2.3.1"> 希律王 聽見 了 、 就 心裡不安 . 耶路撒冷 合城 的 人 、 也 都 不安

(src)="b.MAT.2.4.1"> Mu woolu nag saraxalekat yu mag yépp ak xutbakati xeet wa , laaj leen fu Almasi bi , maanaam Kirist , war a juddoo .
(trg)="b.MAT.2.4.1"> 他 就 召齊 了 祭司 長和 民間 的 文士 、 問他 們說 、 基督 當生 在 何處

(src)="b.MAT.2.5.1"> Ñu ne ko : « Ca Betleyem ci diiwaanu Yude , ndaxte lii lañu bind jaarale ko cib yonent :
(trg)="b.MAT.2.5.1"> 他 們 回答 說 、 在 猶太 的 伯利恆 . 因為 有 先知記 著說

(src)="b.MAT.2.6.1"> “ Yaw Betleyem ci diiwaanu Yude , du yaw yaa yées ci njiiti Yude , ndaxte ci yaw la njiit di génne , kiy sàmm Israyil sama xeet . ” »
(trg)="b.MAT.2.6.1"> 『 猶大 地 的 伯利 恆阿 、 你 在 猶大 諸 城中 、 並 不 是 最 小 的 . 因 為將來 有 一 位 君王 、 要從 你 那 裡出來 、 牧養 我 以色列 民 。

(src)="b.MAT.2.7.1"> Ci kaw loolu Erodd woolu ci kumpa boroom xam-xam ya , di leen ceddowu , ngir xam bu wóor kañ la biddiiw bi feq .
(trg)="b.MAT.2.7.1"> 當下 希律 暗暗 的 召 了 博士來 、 細問 那 星 是 甚 麼時候 出現的

(src)="b.MAT.2.8.1"> Noonu mu yebal leen Betleyem naan : « Demleen fa , seet bu wóor mbirum xale ba .
(src)="b.MAT.2.8.2"> Bu ngeen ci amee lu wóor nag , ngeen xamal ma ko , ngir man itam ma dem màggal ko . »
(trg)="b.MAT.2.8.1"> 就 差 他 們往 伯利 恆去 、 說 、 你 們去 仔細尋訪 那 小孩子 . 尋到 了 、 就 來報 信 、 我 也好 去 拜 他

(src)="b.MAT.2.9.1"> Ba ñu dégloo buur ba nag , ñu dem .
(src)="b.MAT.2.9.2"> Te biddiiw , ba ñu gisoon ca penku ba , ne tell jiite leen , ba àgg , tiim fa xale ba nekk .
(trg)="b.MAT.2.9.1"> 他 們聽見 王的話 、 就 去 了 . 在 東方 所 看見 的 那 星 、 忽然 在 他 們 前 頭行 、 直行 到 小孩子 的 地方 、 就 在 上頭 停住 了

(src)="b.MAT.2.10.1"> Ba ñu gisee biddiiw ba nag , ñu am mbég mu réy-a-réy .
(trg)="b.MAT.2.10.1"> 他 們看見 那 星 、 就 大大 的 歡喜

(src)="b.MAT.2.11.1"> Ñu dugg ca kër ga , gis xale ba ak Maryaama ndeyam , ñu daldi sukk , di ko màggal .
(src)="b.MAT.2.11.2"> Ñu ubbi seeni boyetu alal , may ko wurus ak cuuraay ak ndàbb lu xeeñ lu ñuy wax miir .
(trg)="b.MAT.2.11.1"> 進 了 房子 、 看見 小孩子 和 他 母親 馬利亞 、 就 俯伏 拜 那 小孩子 、 揭開 寶盒 、 拿黃 金 乳香沒 藥為禮 物 獻給他

(src)="b.MAT.2.12.1"> Bi ñu ko defee Yàlla artu na leen ci biir gént , ñu bañ a dellu ca Erodd .
(src)="b.MAT.2.12.2"> Noonu ñu jaar weneen yoon , ñibbi seen réew .
(trg)="b.MAT.2.12.1"> 博士 因 為 在 夢中 被 主 指示 、 不 要 回去 見 希律 、 就 從別 的 路回 本地 去了

(src)="b.MAT.2.13.1"> Bi nga xamee ne boroom xam-xam ya ñibbi nañu , benn malaakam Boroom bi feeñu Yuusufa ci gént ne ko : « Erodd mu ngi ci tànki wut xale bi , ngir rey ko ; jógal nag , jël xale bi ak ndeyam te nga daw jëm Misra , toog fa , ba kera ma koy wax . »
(trg)="b.MAT.2.13.1"> 他 們去 後 、 有主 的 使者 向 約瑟夢 中 顯現 、 說 、 起來 、 帶 著 小孩子 同 他 母親 、 逃往 埃及 、 住在 那 裡 、 等 我 吩咐 你 . 因為 希律 必尋 找 小孩子 要 除 滅他

(src)="b.MAT.2.14.1"> Yuusufa nag jóg , jël xale ba ak ndeyam , làquji Misra ca guddi ga .
(trg)="b.MAT.2.14.1"> 約瑟 就 起來 、 夜間帶 著 小孩子 和 他 母親往 埃及去

(src)="b.MAT.2.15.1"> Mu toog fa , ba Erodd faatu .
(src)="b.MAT.2.15.2"> Noonu am li Boroom bi waxoon jaarale ko cib yonent , bi mu naan : « Woo naa sama doom , mu génn Misra . »
(trg)="b.MAT.2.15.1"> 住 在 那 裡 、 直 到 希律 死了 . 這是 要 應驗 主 藉 先知 所 說的話 、 說 、 『 我 從 埃及 召出 我 的 兒子來 。

(src)="b.MAT.2.16.1"> Bi Erodd gisee nag , ne boroom xam-xam ya nax nañu ko , mu daldi mer lool .
(src)="b.MAT.2.16.2"> Mu santaane ñu dugg ca Betleyem ak la ko wër , rey xale yu góor ya fa am ñaari at jëm suuf , mengook jamono , ja ko boroom xam-xam ya waxoon .
(trg)="b.MAT.2.16.1"> 希律 見 自己 被 博士 愚弄 、 就 大大 發怒 、 差人 將伯利 恆城裡 、 並四 境 所有 的 男孩 、 照著 他 向 博士仔 細查問 的 時候 、 凡兩歲 以 裡 的 、 都殺盡了

(src)="b.MAT.2.17.1"> Booba am la ñu waxoon jaarale ko ci yonent Yàlla Yeremi , bi mu naan :
(trg)="b.MAT.2.17.1"> 這就應 了 先知 耶利米 的話 、 說

(src)="b.MAT.2.18.1"> « Baat jib na ci Rama , ay jooy ak yuux gu réy , Rasel mooy jooy ay doomamte bëggul kenn dëfël ko , ndaxte saay nañu . »
(trg)="b.MAT.2.18.1"> 『 在 拉 瑪聽見號咷 大哭 的 聲音 、 是 拉結哭 他 兒女 、 不 肯 受 安慰 、 因為 他 們 都 不在了 。

(src)="b.MAT.2.19.1"> Bi nga xamee ne Erodd faatu na , benn malaakam Boroom bi feeñu Yuusufa ci gént ca Misra ,
(trg)="b.MAT.2.19.1"> 希律 死 了 以後 、 有主 的 使者 、 在 埃及 向 約瑟夢 中 顯現 、 說

(src)="b.MAT.2.20.1"> ne ko : « Ñi doon wut a rey xale ba dee nañu ; jógal nag , jël xale bi ak ndeyam te nga dellu Israyil . »
(trg)="b.MAT.2.20.1"> 起來 、 帶 著 小孩子 和 他 母親往 以色列 地 去 . 因為 要害 小孩子 性命 的 人 已 經死了

(src)="b.MAT.2.21.1"> Yuusufa jóg nag , jël xale ba ak ndeyam , dellu Israyil .
(trg)="b.MAT.2.21.1"> 約瑟 就 起來 、 把 小孩子 和 他 母親帶 到 以色列 地去

(src)="b.MAT.2.22.1"> Waaye bi mu déggee ne , Arkelawus moo donn Erodd baayam ca nguuru Yude , mu ragal faa dem .
(src)="b.MAT.2.22.2"> Yàlla artu ko nag ci gént , mu daldi dem diiwaanu Galile .
(trg)="b.MAT.2.22.1"> 只因 聽見亞 基 老 接著 他 父親希律 作了 猶 太 王 、 就 怕 往那 裡 去 . 又 在 夢中 被 主 指示 、 便 往 加利利 境內 去了

(src)="b.MAT.2.23.1"> Mu ñëw nag dëkk ci dëkk bu ñuy wax Nasaret .
(src)="b.MAT.2.23.2"> Noonu am la ñu waxoon ca xale ba , jaarale ko ca yonent ya , bi ñu naan : « Dees na ko tudde Nasaréen . »
(trg)="b.MAT.2.23.1"> 到了 一 座 城 、 名叫 拿撒勒 、 就 住在 那 裡 . 這是 要 應驗 先知 所 說 、 他 將稱為 拿撒勒人 的 話了

(src)="b.MAT.3.1.1"> Ca jamono jooja Yaxya feeñoon na , di waare ca màndiŋu Yude .
(trg)="b.MAT.3.1.1"> 那時 、 有 施洗 的 約翰 出來 、 在 猶太 的 曠野傳道 、 說

(src)="b.MAT.3.2.1"> Nii la doon waaree : « Tuubleen seeni bàkkaar , ndaxte nguuru Yàlla Aji Kawe ji jege na . »
(trg)="b.MAT.3.2.1"> 天國 近 了 、 你 們應當 悔改

(src)="b.MAT.3.3.1"> Yaxya mooy ki ñu doon wax jaarale ko ci yonent Yàlla Esayi , bi mu naan : « Am na baat buy xaacu ca màndiŋ ma ne : “ Xàll-leen yoonu Boroom bi , jubal-leen fi muy jaar . ” »
(trg)="b.MAT.3.3.1"> 這人 就是 先知 以 賽亞 所 說 的 、 他說 、 『 在 曠野 有 人 聲喊 著說 、 豫備主 的 道 、 修直 他 的 路 。

(src)="b.MAT.3.4.1"> Yaxya nag mu ngi soloon mbubb mu ñu ràbbe kawaru giléem , takk geñog der ci ndiggam .
(src)="b.MAT.3.4.2"> Ay njéeréer la doon dunde ak lem .
(trg)="b.MAT.3.4.1"> 這 約翰 身穿 駱駝 毛 的 衣服 、 腰束 皮帶 、 喫 的 是 蝗蟲 野蜜

(src)="b.MAT.3.5.1"> Noonu ñépp génn jëm ci moom , ñi dëkk Yerusalem ak diiwaanu Yude , ak waa dexu Yurdan .
(trg)="b.MAT.3.5.1"> 那時 、 耶路撒冷 和 猶太 全 地 、 並約 但 河 一 帶 地方 的 人 、 都 出去 到 約翰 那 裡

(src)="b.MAT.3.6.1"> Ñu nangu seeni bàkkaar , Yaxya sóob leen ca dexu Yurdan .
(trg)="b.MAT.3.6.1"> 承認 他 們 的 罪 、 在 約但 河裡 受 他 的 洗

(src)="b.MAT.3.7.1"> Noonu ay Farisen ak ay Sadusen yu bare ñëw ci Yaxya , ngir mu sóob leen ñoom itam ca dex ga .
(src)="b.MAT.3.7.2"> Waaye bi leen Yaxya gisee , mu ne leen : « Yéen ñi fees ak daŋar mel ni ay co , ku leen artu , ngeen daw merum Yàlla mi nar a wàcc ?
(trg)="b.MAT.3.7.1"> 約翰 看 見許 多 法 利賽人 和 撒 都 該人 、 也來 受洗 、 就 對 他 們說 、 毒蛇 的 種類 、 誰 指示 你 們逃避 將來 的 忿怒 呢

(src)="b.MAT.3.8.1"> Jëfeleen nag ni ñu tuub seeni bàkkaar ,
(trg)="b.MAT.3.8.1"> 你 們要 結出 果子 來 、 與悔改 的 心 相稱

(src)="b.MAT.3.9.1"> te buleen wax ci seen xel naan : “ Nun daal doomi Ibraayma lanu , ” ndaxte maa ngi leen koy wax , Yàlla man na sàkkal Ibraayma ay doom ci doj yii .
(trg)="b.MAT.3.9.1"> 不要 自己 心 裡說 、 有 亞伯拉罕 為我們 的 袓宗 . 我 告訴 你 們 、 神 能 從這 些 石頭中給 亞伯拉罕 興 起子 孫來

(src)="b.MAT.3.10.1"> Sémmiñ wi tiim na reeni garab yi .
(src)="b.MAT.3.10.2"> Garab nag gu meññul doom yu baax , dees na ko gor , sànni ko ci safara si .
(trg)="b.MAT.3.10.1"> 現 在 斧子 已 經放 在 樹根 上 、 凡 不 結好 果子 的 樹 、 就 砍下 來 、 丟 在 火裡

(src)="b.MAT.3.11.1"> Man maa ngi leen di sóob ci ndox , ci lu ànd ak tuub seeni bàkkaar .
(src)="b.MAT.3.11.2"> Waaye kiy ñëw sama gannaaw moo ma ëpp kàttan , ba yeyoowuma koo yóbbul sax ay dàllam .
(src)="b.MAT.3.11.3"> Kooku dina leen sóob ci Xel mu Sell mi ak safara .
(trg)="b.MAT.3.11.1"> 我 是 用水 給 你 們施洗 、 叫 你 們悔改 . 但 那 在 我 以 後來 的 、 能力 比 我 更 大 、 我 就是 給 他 提鞋 、 也 不配 . 他 要 用 聖靈 與火給 你 們施洗

(src)="b.MAT.3.12.1"> Layoom mu ngi ci loxoom , ngir jéri dàgga ja , ba mu set ; pepp ma dina ko def ca sàq ma , waaye xatax ba dina ko lakk ci safara su dul fey mukk . »
(trg)="b.MAT.3.12.1"> 他 手 裡 拿著 簸箕 、 要 揚淨 他 的 場 、 把 麥子 收 在 倉裡 、 把糠 用 不 滅 的 火燒盡 了

(src)="b.MAT.3.13.1"> Booba Yeesu jóge Galile , ñëw ngir Yaxya sóob ko ca dexu Yurdan .
(trg)="b.MAT.3.13.1"> 當下 、 耶穌從 加利利 來到 約但 河 、 見 了 約翰 、 要 受 他 的 洗

(src)="b.MAT.3.14.1"> Waaye Yaxya gàntu ko ne : « Man maa soxla , nga sóob ma ci ndox , te yaa ngi ñëw ci man ! »
(trg)="b.MAT.3.14.1"> 約翰 想要 攔住 他 、 說 、 我當受 你 的 洗 、 你 反倒 上 我 這裡來麼

(src)="b.MAT.3.15.1"> Yeesu tontu ko : « Bàyyil noonu , ndaxte war nanoo mottali lépp lu jub . »
(src)="b.MAT.3.15.2"> Noonu Yaxya nangu .
(trg)="b.MAT.3.15.1"> 耶穌 回答 說 、 你 暫且許 我 . 因為 我 們理當這樣盡諸 般的義 . 〔 或 作禮 〕 於是 約翰 許 了 他

(src)="b.MAT.3.16.1"> Bi ko Yaxya sóobee ca dex ga , Yeesu génn .
(src)="b.MAT.3.16.2"> Ca saa sa asamaan yi daldi ubbiku , te Yaxya gis Xelum Yàlla wàcc ci melow pitax , ñëw ci kaw Yeesu .
(trg)="b.MAT.3.16.1"> 耶穌 受 了 洗 、 隨即從水裡 上來 . 天 忽然為 他 開 了 、 他 就 看 見神 的 靈 、 彷彿鴿 子 降下 、 落在 他 身上

(src)="b.MAT.3.17.1"> Te baat bu jóge asamaan dégtu ne : « Kii mooy sama Doom ji ma bëgg ; ci moom laa ame bànneex . »
(trg)="b.MAT.3.17.1"> 從天 上有聲 音說 、 這是 我 的 愛子 、 我 所 喜 悅 的

(src)="b.MAT.4.1.1"> Bi loolu amee Xelum Yàlla yóbbu Yeesu ca màndiŋ ma , ngir mu jànkoonte ak fiiri Seytaane .
(trg)="b.MAT.4.1.1"> 當時 、 耶穌 被 聖靈 引 到 曠野 、 受 魔鬼 的 試探

(src)="b.MAT.4.2.1"> Yeesu nekk fa te lekkul ñeent-fukki bëccëg ak ñeent-fukki guddi , door a xiif .
(trg)="b.MAT.4.2.1"> 他 禁食 四十 晝 夜 、 後來 就 餓了

(src)="b.MAT.4.3.1"> Noonu fiirkat bi ñëw ci moom ne ko : « Boo dee Doomu Yàlla , santal doj yii , ñu nekk mburu . »
(trg)="b.MAT.4.3.1"> 那 試探人 的 進前來 、 對他說 、 你 若是 神 的 兒子 、 可以 吩咐 這些 石頭變 成 食物

(src)="b.MAT.4.4.1"> Waaye Yeesu tontu ko ne : « Mbind mi nee na : “ Nit du dunde mburu rekk , waaye itam gépp kàddu gu génne ci gémmiñug Yàlla . ” »
(trg)="b.MAT.4.4.1"> 耶穌卻 回答 說 、 經上記 著說 、 『 人 活著 、 不 是 單靠 食物 、 乃是 靠 神口 裡 所 出 的 一切 話 。

(src)="b.MAT.4.5.1"> Bi mu waxee loolu , Seytaane yóbbu ko ca dëkk bu sell ba , teg ko ca njobbaxtalu kër Yàlla ga .
(trg)="b.MAT.4.5.1"> 魔鬼 就 帶 他 進 了 聖城 、 叫 他 站在 殿 頂上 、 〔 頂 原文 作翅

(src)="b.MAT.4.6.1"> Mu ne ko : « Boo dee Doomu Yàlla , tëbal ci suuf , ndaxte Mbind mi nee na : “ Dina jox ay malaakaam ndigal ci sa mbir , ñu leewu la ci seeni loxo , ngir nga bañ a fakkastalu ciw doj . ” »
(trg)="b.MAT.4.6.1"> 對他說 、 你 若是 神 的 兒子 、 可以 跳 下去 . 因 為經 上 記著說 、 『 主要 為 你 吩咐 他 的 使者 、 用手 托 著 你 、 免得 你 的 腳碰 在 石頭 上 。

(src)="b.MAT.4.7.1"> Yeesu tontu ko : « Bind nañu it ne : “ Bul diiŋat Yàlla , sa Boroom . ” »
(trg)="b.MAT.4.7.1"> 耶穌對 他 說 、 經上 又 記著說 、 『 不 可 試 探主 你 的 神 。

(src)="b.MAT.4.8.1"> Gannaaw loolu Seytaane yóbbu ko ci kaw tund wu kawe lool , won ko réewi àddina yépp ak seeni ndam .
(trg)="b.MAT.4.8.1"> 魔鬼 又 帶 他 上 了 一 座 最 高 的 山 、 將 世上 的 萬國 、 與萬國 的 榮華 、 都 指給 他 看

(src)="b.MAT.4.9.1"> Mu ne ko : « Lii lépp dinaa la ko may , boo sukkee màggal ma . »
(trg)="b.MAT.4.9.1"> 對他說 、 你 若 俯伏 拜 我 、 我 就 把 這 一切 賜給你

(src)="b.MAT.4.10.1"> Waaye Yeesu tontu ko : « Sore ma Seytaane , ndaxte Mbind mi nee na : “ Nanga màggal Yàlla sa Boroom , te jaamu ko moom rekk . ” »
(trg)="b.MAT.4.10.1"> 耶穌說 、 撒但 退去 罷 。 〔 撒但 就是 抵擋 的 意思 乃 魔鬼 的 別名 〕 因 為經 上 記著說 、 『 當 拜 主 你 的 神 、 單要事 奉 他 。

(src)="b.MAT.4.11.1"> Noonu Seytaane bàyyi ko .
(src)="b.MAT.4.11.2"> Te ay malaaka daldi ñëw fi Yeesu , di ko topptoo .
(trg)="b.MAT.4.11.1"> 於是 魔鬼 離 了 耶穌 、 有 天使來 伺候 他

(src)="b.MAT.4.12.1"> Am bés Yeesu dégg ne , jàpp nañu Yaxya ; mu jóg nag , jëm Galile .
(trg)="b.MAT.4.12.1"> 耶穌聽見 約翰 下 了 監 、 就 退到 加利利 去

(src)="b.MAT.4.13.1"> Gannaaw gi , mu toxoo dëkku Nasaret , dem dëkk Kapernawum , bi féeteek dex ga ci diiwaani Sabulon ak Neftali .
(trg)="b.MAT.4.13.1"> 後 又 離開 拿撒勒 、 往迦 百 農 去 、 就 住在 那 裡 . 那 地 去 方 靠海 、 在 西 布倫 和 拿弗他利 的 邊界 上

(src)="b.MAT.4.14.1"> Noonu am la ñu waxoon , jaarale ko ci yonent Yàlla Esayi , bi mu naan :
(trg)="b.MAT.4.14.1"> 這是 要 應驗 先知 以 賽亞 的 話

(src)="b.MAT.4.15.1"> « Yaw réewum Sabulon ak réewum Neftali , di yoonu géej gannaaw dexu Yurdan , yaw Galile , réewum ñi dul Yawut —
(trg)="b.MAT.4.15.1"> 說 、 『 西 布 倫地 、 拿弗他利 地 、 就是 沿海 的 路 、 約但 河外 、 外邦人 的 加利利 地

(src)="b.MAT.4.16.1"> xeet wa nekkoon cig lëndëm , gis na leer gu mag , ña dëkkoon ca réew , ma dee tiim , leer fenkal na leen . »
(trg)="b.MAT.4.16.1"> 那 坐在 黑暗 裡 的 百姓 、 看見 了 大 光 、 坐在 死 蔭 之 地 的 人 、 有光 發現 照著 他 們 。

(src)="b.MAT.4.17.1"> Booba Yeesu tàmbali di waare naan : « Tuubleen seeni bàkkaar , ndaxte nguuru Yàlla Aji Kawe ji jegesi na . »
(trg)="b.MAT.4.17.1"> 從那時候 耶穌 就 傳起 道來 、 說 、 天國近 了 、 你 們應當 悔改

(src)="b.MAT.4.18.1"> Gannaaw loolu Yeesu doon dox ca tefesu dexu Galile , mu gis fa ñaar ñu bokk ndey ak baay , mooy Simoŋ mi ñuy wax Piyeer , ak Andare .
(src)="b.MAT.4.18.2"> Fekk ñuy sànni seen caax ca dex ga , ndaxte ay nappkat lañu woon .
(trg)="b.MAT.4.18.1"> 耶穌 在 加利利 海邊 行走 、 看 見 弟兄 二 人 、 就是 那 稱呼 彼得 的 西門 、 和 他 兄弟 安得烈 、 在 海裡 撒網 . 他 們本 是 打 魚的

(src)="b.MAT.4.19.1"> Yeesu ne leen : « Ñëwleen topp ci man , ma def leen nappkati nit . »
(trg)="b.MAT.4.19.1"> 耶穌對 他 們說 、 來跟從 我 、 我 要 叫 你 們得 人 如 得魚一樣

(src)="b.MAT.4.20.1"> Ca saa sa ñu daldi bàyyi seeni mbaal , topp ci moom .
(trg)="b.MAT.4.20.1"> 他 們 就 立刻 捨了網 、 跟從 了 他

(src)="b.MAT.4.21.1"> Ba Yeesu demee ba ca kanam , mu gis yeneen ñaar ñu bokk ndey ak baay , ñuy Saag doomu Sebede , ak Yowaana rakkam .
(src)="b.MAT.4.21.2"> Ñu nekk ci seen biir gaal ak Sebede seen baay , di defar seeni mbaal .
(src)="b.MAT.4.21.3"> Noonu Yeesu woo leen .
(trg)="b.MAT.4.21.1"> 從那裡 往前 走 、 又 看 見弟兄 二 人 、 就 是 西庇太 的 兒子 雅各 、 和 他 兄弟 約翰 、 同 他 們的 父親 西庇太 在 船上 補網 . 耶穌 就 招呼 他 們

(src)="b.MAT.4.22.1"> Ca saa sa ñu daldi bàyyi gaal ga ak seen baay , topp ci moom .
(trg)="b.MAT.4.22.1"> 他 們立刻 捨 了 船 、 別 了 父親 、 跟從 了 耶穌

(src)="b.MAT.4.23.1"> Ba loolu amee Yeesu doon wër Galile gépp , di jàngale ci seeni jàngu tey yégle xebaar bu baax bi ci nguuru Yàlla ; muy faj jàngoro yépp ak wéradi yépp ca nit ña ,
(trg)="b.MAT.4.23.1"> 耶穌 走遍 加利利 、 在各會堂裡 教訓人 、 傳 天國 的 福音 、 醫治 百姓 各 樣 的 病症

(src)="b.MAT.4.24.1"> ba tax turam siiw ba ci biir réewu Siri mépp .
(src)="b.MAT.4.24.2"> Ñu di ko indil ñi wopp ñépp , ñi sonn ndax ay jàngoro ak metit yu bare , ñi rab jàpp , ñiy say ak ñi làggi , mu faj leen .
(trg)="b.MAT.4.24.1"> 他 的 名聲 就 傳遍 了 敘利亞 . 那裡 的 人 把 一切 害病 的 、 就是 害 各 樣 疾病 、 各 樣 疼痛 的 、 和 被 鬼 附 的 、 癲癇 的 、 癱瘓 的 、 都帶了來 、 耶穌 就 治好 了 他 們

(src)="b.MAT.4.25.1"> Noonu mbooloo mu bare topp ci moom , jóge ci wàlli Galile ak diiwaan bi ñuy wax Fukki dëkk yi , ci dëkku Yerusalem ak ci diiwaanu Yude , ba ci gannaaw dexu Yurdan ..
(trg)="b.MAT.4.25.1"> 當下 、 有 許多 人 從加利利 、 低 加 波利 、 耶路撒冷 、 猶太 、 約但 河外 、 來 跟 著 他

(src)="b.MAT.5.1.1"> Bi Yeesu gisee mbooloo ma nag , mu yéeg ca tund wa , toog ; taalibeem ya ñëw ci moom .
(trg)="b.MAT.5.1.1"> 耶穌 看 見這許 多 的 人 、 就 上 了 山 、 既 已 坐下 、 門徒 到 他 跟前來

(src)="b.MAT.5.2.1"> Mu daldi leen jàngal naan :
(trg)="b.MAT.5.2.1"> 他 就 開口 教訓 他 們說

(src)="b.MAT.5.3.1"> « Yéen ñi xam seen ñàkk doole ngir neex Yàlla , barkeel ngeen , ndaxte nguuru Yàlla Aji Kawe ji , yéena ko yelloo .
(trg)="b.MAT.5.3.1"> 虛心 的 人 有 福 了 . 因 為 天國是 他 們的

(src)="b.MAT.5.4.1"> Yéen ñi nekk ci naqar , barkeel ngeen , ndax dees na dëfël seen xol .
(trg)="b.MAT.5.4.1"> 哀慟 的 人 有 福 了 . 因為 他 們必得 安慰

(src)="b.MAT.5.5.1"> Yéen ñi lewet , barkeel ngeen , ndax dingeen moomi àddina .
(trg)="b.MAT.5.5.1"> 溫柔 的 人 有 福 了 . 因為 他 們必 承受 地土

(src)="b.MAT.5.6.1"> Yéen ñi xiif te mar njub , barkeel ngeen , ndax dingeen regg .
(trg)="b.MAT.5.6.1"> 飢 渴慕義 的 人 有 福 了 . 因為 他 們必得 飽足

(src)="b.MAT.5.7.1"> Yéen ñi am yërmande , barkeel ngeen , ndax dees na leen yërëm .
(trg)="b.MAT.5.7.1"> 憐恤 人 的 人 有 福 了 . 因為 他 們必 蒙憐恤

(src)="b.MAT.5.8.1"> Yéen ñi am xol bu sell , barkeel ngeen , ndax dingeen gis Yàlla .
(trg)="b.MAT.5.8.1"> 清心 的 人 有 福 了 . 因為 他 們必得 見神

(src)="b.MAT.5.9.1"> Yéen ñiy wut jàmm , barkeel ngeen , ndax dees na leen tudde doomi Yàlla .
(trg)="b.MAT.5.9.1"> 使 人 和睦 的 人 有 福 了 . 因為 他 們必稱為 神 的 兒子

(src)="b.MAT.5.10.1"> Yéen ñi ñu fitnaal ndax seen njub , barkeel ngeen , ndaxte nguuru Yàlla Aji Kawe ji , yéena ko yelloo .
(trg)="b.MAT.5.10.1"> 為義 受 逼迫 的 人 有 福 了 . 因 為 天國是 他 們的