# co/gnome-desktop-2.0.xml.gz
# wo/gnome-desktop-2.0.xml.gz
(src)="s1"> Appropositu di GNOME
(trg)="s1"> lu jëm ci GNOME
(src)="s2"> Amparane di più à nantu à GNOME
(trg)="s2"> gën a xam lu jëm ci GNOME
(src)="s3"> Nutizie
(trg)="s3"> xibaar
(src)="s5"> Amichi di GNOME
(trg)="s5"> Xariti GNOME
(src)="s6"> Cuntattu
(trg)="s6"> jotukaay
(src)="s7"> U Misteriosu GEGL
(trg)="s7"> Kéemtaan gu GEGL
(src)="s9"> Wanda U pesciu GNOME
(trg)="s9"> Wanda , jën bu Gnome
(src)="s12"> Apprupositu di u Scagnu numericu GNOME
(trg)="s12"> Ci mbiri Binduwaayu GNOME
(src)="s14"> Benvenuti à u Scagnu Gnome
(trg)="s14"> Dalal-jàmm ci Binduwaayu GNOME
(src)="s15"> Purtatu per voi dà :
(trg)="s15"> Ki la ko indil :
(src)="s17"> Versione
(trg)="s17"> Sumb
(src)="s18"> Distributore
(trg)="s18"> Séddalekat
(src)="s19"> Data di custruzzione
(trg)="s19"> Bés bees àgg
(src)="s21"> GNOME hè di gratisi , usevule , stabile , hè un scagnu accessibile in l 'ambiu Unix .
(trg)="s21"> GNOME ab wërlaayub binduwaay la bu féex , yomb a jëfandikoo , jotale ngir xeeti nosteg doxiin yu dàttu ci UNIX .
(src)="s22"> GNOME include di più ch 'elle si pò vede à nantu à u screnu , includentu a gestione di u schedariu , a navigazione à nantu à u web , i listini , è assai appiicazioni .
(trg)="s22"> GNOME ëmbaale na lu bari ci mbir yi ne ci sa nosukaay , boole ci yorkatu dencukaay yi , joowukaayu web , njël yeek tëriin yu bari .
(src)="s23"> GNOME include dinù un pianu di sviluppu cumplettu per l 'appiicazioni di i prugrammatori , chi permette a creazione d 'appiicazione pudente et cumplesse .
(trg)="s23"> Ak GNOME dees na jébbalaale it ab joyaluwaay bees jagleel tëralkat yi , tax ñuy man a bindiy tëriin yu kàttanu te fasu
(src)="s24"> GNOME hè attentu à l 'usu è a l 'accessibilita , aduprendu un ciculu di versione è un aiutu finanziaru sicuru unicu per i scagni numerichi di gratisi .
(trg)="s24"> Bàyyi-xel cig yomb a jëfandikoom ak jotaleem , génnewaat yu tegu ci yoon , ak jàppaleem gu këru-liggéey yu mag tax GNOME doon kenn ci Tëriinu Binduwaay yu Féex yi .
(src)="s25"> A forza di GNOME è a nostra cummunità . Tutt 'ognuno pò incù è sò cumpitenze , cuntribuì à purtà u sviluppu di GNOME .
(trg)="s25"> Dooley GNOME mooy askanam gu rëy . Daanaka ku ne , muy ku man walla ku manul bindi tëriin , man ngaa duggal sa loxo ci GNOME ngir gënal ko .
(src)="s26"> Centunari di ghjenti anu cuntribuitu à cunstruì u codice di GNOME dapoi 1997 ; di più anu cuntribuitu in d 'altre vie , vale à di a traduzione , a ducumentazione è l 'assicuranza di a qualità.UnknownMonitor vendor
(trg)="s26"> Ay Téeméeri nit cëru nañu ci yoonu GNOME dalee ci juddam 1997 ba léegi , ñeneen ñi ci yeneen fànn , muy tekki , uti xibaar ak ci wóoral baaxaayam.UnknownMonitor vendor
(src)="s28"> Errore lighjendu a scheda ' % s ' : % s
(trg)="s28"> Njuumte ci njàngum dencukaay ' % s ' : % s
(src)="s29"> Errore rimuntendu a scheda ' % s ' : % snamename
(trg)="s29"> Njuumte ci lëmësaatu dencukaay ' % s ' : % snamename
(src)="s30"> Senza nome
(trg)="s30"> Amul tur
(src)="s31"> A scheda ò l 'annuariu ' % s ' un hè rigulare
(trg)="s31"> Dencukaay ' % s ' du dencukaay walla dencuwaay bu baax .
(src)="s33"> Ùn c 'hè nome di scheda per salvala
(trg)="s33"> Joxoo tur dencukaay bi
(src)="s34"> Smarrendu % s
(trg)="s34"> Doorug % s
(src)="s35"> Ùn ci hè URL dà avvià
(trg)="s35"> Amul URL bees man a ubbi
(src)="s36"> Ùn hè un item dà avvià
(trg)="s36"> Lii du lees man a ubbi
(src)="s37"> Ùn hè una cummanda ( Exec ) dà avvià
(trg)="s37"> Amulub santaane ( Exec ) bees war a jëfe
(src)="s38"> Ùn hè a cummanda ( Exec ) dà avvià
(trg)="s38"> Santaane bees war a jëfe ( Exec ) baaxul
(src)="s39"> Messa in codice scunisciuta di : % s
(trg)="s39"> Yoonalug % s baaxul
(src)="s45"> position " , " size " , and " maximum
(trg)="s45"> maneesul a ami xibaar ñeel génn gu % dposition " , " size " , and " maximum
(src)="s59"> requested " , " minimummaximum
(trg)="s59"> requested " , " minimummaximum
(src)="s60"> MirrorPantallas en Espejo " , * not * " Espejar Pantallas
(trg)="s60"> MirrorPantallas en Espejo " , * not * " Espejar Pantallas
# co/gnome-menus-3.0.xml.gz
# wo/gnome-menus-3.0.xml.gz
(src)="s3"> Prugrammazione
(trg)="s3"> soqali
(src)="s14"> Attuvigli Sistema
(trg)="s14"> Jumtukaayi liggueyoukay gi
(src)="s21"> Altru
(trg)="s21"> Yeneen
(src)="s52"> Preferenze
(trg)="s52"> Tànneef
(src)="s61"> Personal settings
(trg)="s61"> Personal settings