Je ne sais pas.
Xamuma.


Où vas-tu ?
Fan nga dem?

Je suis enceinte de quatre mois.
Dama eumb mangui si ńénti wèr.

D'où viens-tu ?
Fan nga joge?

Je n'ai pas de chat.
Amuma muus.

Bonsoir !
Naka ngon si.

Bonjour !
Jaam nga fanane.

Bonjour !
Jamm nga yendoo.

Cependant, je n'ai pas d'argent.
Wurus, amuma xaalis.

Je l'ignore.
Xamuma.

C'est quoi ?
Lii lan la?

Aujourd'hui je n'ai pas d'argent.
Tey amuma xaalis.

On dirait que le chat a détecté l'odeur d'une souris.
Dafa mèlni mouss bi dafa yeuk xètou ganax bi.

Où est-ce que vous allez ?
Fan nga dem?

Qui est cette personne?
Kii lan la?

Bonjour.
Jaam nga fanane.

Bonjour.
Jamm nga yendoo.

Retourne à la maison.
Ñibbal.

C'est quoi ce truc ?
Lii lan la?

De quel village viens-tu ?
Ban dekka nga faxeeku?

Je suis au courant.
Xam nako ba paré.

J'ai envie de sortir aujourd'hui.
Dama boga gena tay




J'ai faim.
Dama xiif.

Bonsoir !
Naka ngon si !

Deux jours.
Ñaari fane.

Trois chambres.
Ñett néék.

Quatre mois.
Juróomi wéér.

Cinq mois.
Juróomi wéér.

Six ordinateurs.
Juróom-benn ordinateur.

Sept vaches noires.
Juróom-ñaari nak yu nioul.

Huit saisons.
Juróom-ñetti paci.

Huit coqs.
Juróom-ñeenti ganar.

Dix maisons.
Fukki keur.

Onze mois.
Fukki wéér ak bénn.

Le douzième jour du mois prochain.
Fukkélu fane ak ñaar si wéér bii di ñeuw.

Treize chaussettes rouges.
Fukk ak ñetti kawass yu xonxu.

Treize chaussettes rouges.
Fukk ak ñeenti kawass yu xonxu.

Seize claviers anglais.
Fukk ak juróom-benn clavier angalais.

Dix maisons.
Fukki deukuway.

Quatre livres.
Ñeent livour.

Cent pages vierges.
Téeméeri page yi amul dara.

Huit mois.
Juróom-ñetti wéér.

Neuf cents ans d'histoire.
Istoiru Juróom-ñeenti téeméer ate la.

J’ai donné mille euros à ton frère.
Diokh na sa rak bi junni euros.

Ils sont mille six cents personnes.
Junni ak juróom-benni téeméeri nit lañ.

Je viens ici depuis l’année mille neuf cent quarante cinq.
Si atum junni ak juróom-ñeenti téeméer ak ñeent-fukk ak juróom ba légui magui fiy ñeuw.

Le sénégal a eu son indépendance en l’an mille neuf cent soixante.
Si atum junni ak juróom-ñeenti téeméer ak juróom-benn-fukk la Sénégal mom bopam.

J'ai besoin de deux mille voitures.
Ñaari junni auto la sokhla.

Le premier de la classe.
Ku njëk si calass bi.