Good evening.
Naka ngon si.


I don't know.
Xamuma.

Good afternoon.
Jamm nga yendoo.

Good morning.
Jaam nga fanane.

Why!
Lutax!?

I am going to the market
Damay dem ci marse bi

I need to return to my home
Soxla naa nibbi ci sama kër

I'm a Jehovah's Witness.
Ma ci Seede Yexowa yi.